On June 14, 2024, Momo Dieng released his new song “Saf Na Ba Nopi”. The lyrics were written by Mouhamed Dieng, Ndiouga Dieng, and Seck Mbao, with the music produced by Prince Arts.
Saf Na Ba Nopi song lyrics by Momo Dieng
Saf Na Ba Nopi
Ken Du Sapali
Saf Na Ba Nopi
Ken Du Sapali
Yaw Bul Ma Miina Miine Ba Fatéma Yaayee
Thiow Li Meun Na Beurri Lool Waayé
Nangul Né Thine Bokul Saffine
Yaw Bul Ma Miina Miine Ba Fatéma Waay
Loo Bagn Bagn Ma Marre Nungul Né
Nop Yi Kuddu Na Meun Naa Daaw
Saf Na Ba Nopi
Ken Du Sapali
Momo Saf Na Ba Nopi
Heey Ken Du Sapali
Bargny Ma Roombaal Beut Ba
Daagou Dieum Minam Dieum Sendou
Weuy Ma Yaaya Baay Momo Dieng
Saf Na Ba Nopi
Heeeeee Heeee Heeee
Yeeey Yeee Yaaaa Yaaa
Saf Na Ba Nopi
Ken Du Sapali
Momo Saf Na Ba Nopi
Ken Du Sapali
A Raffeet A Meuneu Feeth
A Meuneu Beuy Beussi Doom
Ama Mayoon Daw Fissine Bassa Borop Guedj Guee
A Raffeet A Meuneu Feeth
A Meuneu Beuy Beussi Doom Ama Mayoon
Daw Fissine Bassa Borop Guedj Guee
Lakoon Sakkon Ngakoon Lebou Baa
Ngi Mooma Mayoon Daw Fissine
Bassa Borop Guedj Guee
Bul Ma Miine Bul Ma Miine Miine Bul Ma Miine
Ba Fatté Ma Kone Mu Gnaaw
Roy Dou Nourook Piir Du Meusseu Nourook Piirr
Isma Bul Ma Miino Bulma
Miine Ba Fatté Ma Kone Mu Gnaaw
Laay Laay La Laa Woo
Bul Ma Miine Baay Raan Bul Ma Miine
Baay Raan Diop Bul Ma Miine Ba Fatté Ma Kone Mu Gnaaw
Louraass Diop Boo Ngeuwul Mu Gnaw
Heeee
Thieuy Sama Waadja Ngi Nii
Heeee
Sa Gane
Rak Sa Gane
Heeee
Neena La Momo Yeungeul Sa Goun Gou Ndath
Heeee
Louraass Diop Boo Ngeuwul Mu Gnaw
Heeee
Thieuy Sama Waadja Ngi Nii
Heeee
Laay Laye La Laa So Ngeuweul Mu Ngaaw Sama Niit
Laay Laye La Laa Woo
Roy Dou Nourook Piir Du Meusseu
Nourook Piirr Djiby Ndiaye Bul Ma Miino
Bul Ma Miine Ba Fatté Ma Kone Mu Gnaaw
Chéri Arame Diallo Sama Waa Dji
Louraass Diop Boo Ngeuwul Mu Gnaw
Heeee
Neenala Momo Yeungeul Sa Goun Gou Ndath
Heeee
Sa Goun
Rak Sa Goun
Heeee
Neenala Momo Yeungeul Sa Goun Gou Ndath
Heeee
Djiby Ndiaye Boo Ngeuweul Mu Gnaaw
Heeee
Thiey Dikeul Dikkeul Suma Waadja Ngi Nii
Heeee
Isma Boo Yeugoo Moo Neex
Heeeeh
Malick Mbath Dissa Baay Sama Waadja Ngi Nii
Heeeeh
Sa Goun
Rak Sa Goun
Heeeh
Neenala Momo Yeungeul Sa Goun Gou Ndath
Heeeeh
Senegal Boo Leen Yeungoo Mu Neex
Heeee
Thieuy Dikkeul Dikkeul Sama Reew Ma Ngi Nii
Heeeeh
Heeeeh
Momo Yeungeul Sa Goun Gou Ndath
Heeeeh
Neenala
Momo Yeungeul Sa Goun Gou Ndath
Heeeeh
Neenala Momo Yeungeul Sa Goun Gou Ndath
Heeeeh
Heeeeh
Heeeeh
Heeeeh
Neenala
Neenala Momo Yeungeul Sa Goun Gou Ndath
Related Songs –
- Genesis – RAYE
- I Still Know Better – Headie One
- Me & U – Tems
- Top – DDG & Blueface (feat. Swae Lee)
- 21 – Ayra Starr
- Tantrums – Normani ft. James Blake
Saf Na Ba Nopi Song Info:
Song Name: | Saf Na Ba Nopi |
Lead Vocals: | Momo Dieng |
Written/Lyrics By: | Mouhamed Dieng, Ndiouga Dieng & Seck Mbao |
Music Produced By: | Prince Arts |
Music Label: | Momo Dieng |
Release Date: | June 14, 2024 |
Frequently Asked Questions
Who produced “Saf Na Ba Nopi” by Momo Dieng?
“Saf Na Ba Nopi” by Momo Dieng was produced by Prince Arts.
When did Momo Dieng release “Saf Na Ba Nopi”?
Momo Dieng released “Saf Na Ba Nopi” on June 14, 2024.
Who wrote “Saf Na Ba Nopi” by Momo Dieng?
“Saf Na Ba Nopi” by Momo Dieng written by Mouhamed Dieng, Ndiouga Dieng & Seck Mbao.
Who sang the “Saf Na Ba Nopi” Song?
The “Saf Na Ba Nopi” song is sung by Momo Dieng.