Mangui Ci Dara Lyrics – Bril (Feat. Am Bongo)

Mangui Ci Dara Lyrics – Bril (Feat. Am Bongo)

Mangui Ci Dara is a brand new French song sung by Bril and Am Bongo. Mangui Ci Dara ​​song lyrics were written by Bril and Am Bongo, and the music was also produced by ​​Bril.

Mangui Ci Dara Song Info:

Song Name:Mangui Ci Dara
Band/Singer:Bril & Am Bongo
Lead Vocals:Bril & Am Bongo
Written By:Bril & Am Bongo
Music Produced By:Bril
Featuring Artist:Am Bongo
Video Director:Ibrahima Mbengue Dione
Release Date:September 16, 2023
Music Label:Bril

Bril – Mangui Ci Dara Lyrics



Mane Mangui Thi Sama Bopp Dama Paré
Pour Lamb Féppeu , Gueuna Beuré
Risqué Té Ken Douma Teuyé
Damay Yéégg Té Douniouma Goungué
Fokma Gagné Rek Wala Ma Déé
Perte Temps Yalla Téré

Bakane Lathiy Tek, Douma Meuna Bégg Tant Que Awma Limay Revé
Life Bi Wanema Ni Yeuffou Deumm La, Ba Takhna Awma Ganyine
Ecole Djangal Ma Reudd Thi Tableau, Bama Raw Bubu Design
Mbed Mi Djangal Ma Sadique, Doundou Lou Meti Di Merite
Tangueu Bama Soneu, Soumi Sama Veste Takhoul Ma Wekkeuko Thi Nitt

Adouna Sokhor Na Amoul Yeurmandé
Khékhal Ba Ken Doula Meuna Commandé
Kharouma Salaire Té Mangui Fayékou
Teudeu Di Nélaw Té Gueunoma Yeiwou
Yaw Danga Rare Fo Né ? Kén Déggatoula

Awma Djott Bi, Mangui Thi Job Bi, Legui Thi Business Bi Rek
Sa Gars Yi Nénagn Danga Rare , Fo Né ? Kén Guissatou
Démal Nélén Awma Temps Bi, Legui Thi Business Bi Rek
Mangui Ci Dara , Namouma Dara
Mangui Ci Dara Té Namouma Dara
Deuggla Mangui Ci Dara Namouma Dara
Mangui Ci Dara Té Namouma Dara
Lègui Sama Khol Dafa Deugueur
Dama Djeund Fer, Doli Béton Bafi Sama Marque Bala Nga
Soli Sa Gucci Wala Louis Vuitton
Bilahi Dama Djougué Thi Zero
Té Fokma Nekk Fi Heros
Kouma Dakh Sa Bureau
Ma Djeundeu Fi Immeuble Louer La Bureau
Rombeul’ak Auto Vroum Vroum

Sa Khol Bi Di Mbalakh Boum Boum
Douniou Daadjé Boma Guissété , Dama Nekkeu Thi Photo Zoom Zoom
Meussouma Compté Kén Bimay Soneu Galère Bi Dima Teuyé
Motakh Ba Meunouma Am Ba Sokhla Fi Kén Pour Compté Samay Billet
Meune Naniou Bokk Di Djangue Thi Ben Ecole Té Yémouniou , Bokkouniou Classe
Dakkla Djangue Sa Khol Bi Di Tangue , Ma Yeureumla , Guénél La Sarakhou Glace
Yaw Danga Rare Fo Né ? Kén Déggatoula
Awma Djott Bi , Mangui Thi Job Bi, Legui Thi Business Bi Rek
Sa Gars Yi Nénagn Danga Rare , Fo Né ? Kén Guissatou
Démal Nélén Awma Temps Bi, Legui Thi Business Bi Rek

Mangui Ci Dara , Namouma Dara
Mangui Ci Dara Té Namouma Dara
Deuggla Mangui Ci Dara Namouma Dara
Mangui Ci Dara Té Namouma Dara
Mané Dokhal
Boul Topato, Boul Faalé, Boul Soralé Sakh
Djitoungalén, Sani Cravache Bi, Raw Ngalén
Gueunelén
Djeuleul
Kou Sone Moss , Kou Soneu Di Nga Moss
Sa Ndeye Djou Bakh Dji Lamou Sonon’angui
Kou Sone Moss
Mangui Ci Dara , Namouma Dara
Mangui Ci Dara Té Namouma Dara
Deuggla Mangui Ci Dara Namouma Dara
Mangui Ci Dara Té Namouma Dara

Mangui Ci Dara Lyrics English– DON XHONI

Will Update Soon…

Mangui Ci Dara Music Video