On June 12, 2024, French singer Dieyla Gueye released her new song “Doflo Ngama”. The lyrics were written by Charles Mbaye Diagne and Mayacine Gueye, with the music produced by Yass.
Doflo Ngama song lyrics by Dieyla Gueye
Mane Sama Sagnse Yaw La Ma Belli Yah La
Dou Keneu Yaw La Doflo Ngama
Mane Kima Taneu Yaw La
Nga Nobb Ma Raw La
Dou Keneu Yaw La Doflo Ngama
Yama Ko Tamal Yama Ko Diangal
Yaw Ligua Andal Doflo Ngama
Laakh Bi Loumou Tangue Tangue
Kenn Dou Mako Rathial
Ligua Diantal Doflo Ngama
Dieukeur Soula Nobe Dagua Kay Titeuro
Ni Mala Nobe Yay Sama Hero
Samay Genteu Ngama Amel Mou Lerr
Ma Pare Doundou Loune Dokh Ci Lila Nekh
Pare Na Pare Na
Pare Na Pare Na
Meuneu Touma La Reuthieu Sama Seytane
Pare Na Pare Na
Pare Na Pare Na
Nekh Nekh Bi Sama Doundou Yawa Coco Bane
Mane Sama Sagnse Yaw La Ma Belli Yah La
Dou Keneu Yaw La Doflo Ngama
Mane Kima Taneu Yaw La
Nga Nobb Ma Raw La
Dou Keneu Yaw La Doflo Ngama
Yama Ko Tamal Yama Ko Diangal
Yaw Ligua Andal Doflo Ngama
Laakh Bi Loumou Tangue Tangue
Kenn Dou Mako Rathial
Ligua Diantal Doflo Ngama
Mbeugel Nak Boula Diape Nga Done Xale
Doto Daal Fo Tolou Dikay Wane
Li Mo Takh Fouma Tolou Dilay Diegue
Ngamay Nabb Nabe Wane Nigua Jongue
Mbeugel Nak Boula Diape Nga Done Xale
Doto Daal Fo Tolou Dikay Wane
Li Mo Takh Fouma Tolou Dilay Diegue
Ngamay Nabb Nabe Wane Nigua Jongue
Pare Na Pare Na
Pare Na Pare Na
Meuneu Touma La Reuthieu Sama Seytane
Pare Na Pare Na
Pare Na Pare Na
Nekh Nekh Bi Sama Doundou Yawa Coco Bane
Mane Sama Sagnse Yaw La Ma Belli Yah La
Dou Keneu Yaw La Doflo Ngama
Mane Kima Taneu Yaw La
Nga Nobb Ma Raw La
Dou Keneu Yaw La Doflo Ngama
Yama Ko Tamal Yama Ko Diangal
Yaw Ligua Andal Doflo Ngama
Laakh Bi Loumou Tangue Tangue
Kenn Dou Mako Rathial
Ligua Diantal Doflo Ngama
Summary
The lyrics express a deep admiration and devotion to someone special, emphasizing that nobody else can take their place or affect the speaker’s feelings. The repeated lines highlight the exclusivity and intensity of the connection, while the verses describe overcoming challenges and staying resilient. There’s a mix of affectionate praise and acknowledgment of the positive impact this person has on the speaker’s life. The repeated phrase “Pare Na” suggests a readiness to face any obstacles, attributing strength and joy to the influence of the loved one.
Related Songs –
Doflo Ngama Song Info:
Song Name: | Doflo Ngama |
Lead Vocals: | Dieyla Gueye |
Written/Lyrics By: | Charles Mbaye Diagne & Mayacine Gueye |
Music Produced By: | Yass |
Music Label: | Dieyla Gueye |
Release Date: | June 12, 2024 |
Direction | Mao Sidibe |
Frequently Asked Questions
Who produced “Doflo Ngama” by Dieyla Gueye?
“Doflo Ngama” by Dieyla Gueye was produced by Yass.
When did Dieyla Gueye release “Doflo Ngama”?
Dieyla Gueye released “Doflo Ngama” on June 12, 2024.
Who wrote “Doflo Ngama” by Dieyla Gueye?
“Doflo Ngama” by Dieyla Gueye written by Charles Mbaye Diagne and Mayacine Gueye.
Who sang the “Doflo Ngama” Song?
The “Doflo Ngama” song is sung by Dieyla Gueye.