Dafa Nekh Lyrics – Jeeba

Dafa Nekh Lyrics - Jeeba

On June 14, 2024, French singer Jeeba released his new song “Dafa Nekh”. The lyrics were written by Djibril Ba, with the music produced by Abadane Daiman.

Dafa Nekh song lyrics by Jeeba

Wakh Mo Lo Bouga Ma Defal Lako
Wakh Ma Lo Namma Cherie Ma Outal Lako
Meme Boudé Auto Ma Dieundal Lako
Yobou Lathi Chateau Nga Deuké Dodo
Dama Xam Fouy Khassane Fofou Lay Wokka
Sa Ex Yila Done Sonal Nieupeu Lay Nokka
Athe La Bathi Kaw Keen Doula Diote
Diokh La Khir Bi Ngaleen Di Thiaw
Ma Takhaw Nane Ko Niaw

Mbeguel Dafa Nekh Bokoy Kaffé Sakh Day Nekh
Sa Biir Xol Bilay Diap Mel Ni Danio Thi Dougal Fekh
Meuno Kham Limay Wakh Tant Que Demo Thi Bamou Diekh
Fok Nga Niam Kani Waw Doga Xam Lou Lem Di Saff
Awa Nénama Dafa Nekh Makhfou Nene Nama
Dafa Nekh Kadia Nenama Dafa Nekh
Meme Maimouna Nenama Mbeuguel Dafa Nekhhhh
Refrain
Kone Dama La Bougga Té Koumou Meti Nanal
Amoniaque Baygon Wala Maladio Sayo Yewo
Nganiouy Guiss Niouy Leungo Ma Nane Ko
Beug Na Beug Nako Boudoul Reen Di Deween
Dinako Def Ndakh Yama Diaral Lolou
Dama Tégui Gros Lot Ohh
Mom Momay Teul Mane Mako Beureung
Xam Na Nandou Lo Lolou
Nioune Bouniou Begué Moniou Begual
Bouniou Dioyé Moniou Dioylo
Couplet

Bebe Xam Ngama Bou Bakh Douma Kou Tegui Ndawal
Fima Lay Diap Banga Ni Akhh Mako Xam Té Dama Koy Dowal
Bebe Xam Nga Mane Loutakh Ma Beug La Dama Thi Sawar
Danga Fek Fi Thiebou Kéthiakh Nga Valorisé Sani Thi Ndawal
Ndakham Lakh Bi Daniou Koy Seulmo No Daniou Koy Keupo
Sama Carte Bi Ioe La Votel Tak Seuy Bi Dial Thi Lenene

Kone Danga Mer Mane Mangui Bakh
Diokh Ko Ndox Mou Nane Mou Gékh
Lolou Meunoul Niak
Ndakh Mbeguel Dafa Nekh Bokoy Kaffé Sakh Day Nekh
Sa Biir Xol Bilay Diap Mel Ni Danio Thi Dougal Fekh
Meuno Kham Limay Wakh Tant Que Demo Thi Bamou Diekh
Fok Nga Niam Kani Waw Doga Xam Lou Lem Di Saff
Abba Nenama Dafa Nekh Ngoné
Nénama Dafa Nekh Habib Nénama Dafa
Meme Aicha Aziz Nénama Mbeuguel Dafa Nekhhhhhhh
Refrain

Kone Dama La Bougga Té Koumou Meti
Nanal Amoniaque Baygon Wala Maladio
Sayo Yewo Nganiouy Guiss Niouy Leungo Ma Nane Ko
Beug Na Beug Nako Boudoul Reen Di Deween
Dinako Def Ndakh Yama Diaral Lolou
Dama Tégui Gros Lot Ohh
Mom Momay Teul Mane Mako
Beureung Xam Na Nandou Lo Lolou
Nioune Bouniou Begué Moniou
Begual Bouniou Dioyé Moniou Dioylo

Mbeuguel Mbeuguel Mbeuguel Dafa Nekh
Nekh Nekh Nekh Nekha Nekh Ayyyé Waw Wa Waw Waw

Kone Dama La Bougga Té Koumou Meti
Nanal Amoniaque Baygon Wala Maladio
Sayo Yewo Nganiouy Guiss Niouy Leungo Ma Nane Ko
Beug Na Beug Nako Boudoul Reen Di
Deween Dinako Def Ndakh Yama Diaral Lolou
Dama Tégui Gros Lot Ohh
Mom Momay Teul Mane Mako
Beureung Xam Na Nandou Lo Lolou
Nioune Bouniou Begué Moniou
Begual Bouniou Dioyé Moniou Dioylo

Summary

The lyrics describe a deep and passionate love. The singer expresses intense emotions and a desire to please and care for their lover. He talks about the sweetness and satisfaction found in love, despite challenges or past relationships. The refrain emphasizes his longing and willingness to do anything for his beloved, portraying love as fulfilling and captivating. The lyrics repeat themes of devotion and the irresistible nature of love, underscoring how it brings joy and meaning to the singer’s life.


Related Songs –


Dafa Nekh Song Info:

Song Name:Dafa Nekh
Lead Vocals:Jeeba
Written/Lyrics By:Djibril Ba
Music Produced By:Abadane Daiman
Music Label:Jeeba
Release Date:June 14, 2024
Direction & Post-Production:Mao SIDIBE

Frequently Asked Questions

Who produced “Dafa Nekh” by Jeeba?

“Dafa Nekh” by Jeeba was produced by Abadane Daiman.

When did Jeeba release “Dafa Nekh”?

Jeeba released “Dafa Nekh” on June 14, 2024.

Who wrote “Dafa Nekh” by Jeeba?

“Dafa Nekh” by Jeeba written by ​Djibril Ba.

Who sang the “Dafa Nekh” Song?

The “Dafa Nekh” song is sung by Jeeba.